《Sama Gàmmu》歌词

[00:00:00] Sama Gàmmu - Youssou N'Dour (尤索·恩多)
[00:00:11] Nanga def yaw sama gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
[00:00:17] Xam naa ne yaw moomu loo ko
[00:00:19] Dang ko àbb mbaa nga for ko
[00:00:20] Baal dóózéé eh
[00:00:28] Nanga def na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
[00:00:34] Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
[00:00:37] Xam naa ne yaw moomu loo ko
[00:00:39] Dang ko àbb mbaa nga for ko
[00:00:40] Baal dóózéé eh
[00:00:48] Yor khalis meunoul tè ma môm la
[00:00:51] Keur gou rich meunoul tè ma môm la
[00:00:54] Yaw na nga def yaw sama gàmmu
[00:00:57] Dég na danga yor khalis
[00:01:00] Khamna ni yaw momouloko dang ko abb mba nga forko bâl dôzé tèyal
[00:01:17] Kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko
[00:01:20] Foog nan nita ko waddal nga for ko
[00:01:22] Wax ma gaaw ñaata la doon ma fay ko
[00:01:25] Man daal maay sa buur nangu ko
[00:01:28] Nanga def na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
[00:01:33] Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
[00:01:36] Xam naa ne yaw moomu loo ko
[00:01:38] Dang ko àbb mbaa nga for ko
[00:01:40] Baal dóózéé eh
[00:01:52] Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
[00:01:57] Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
[00:02:03] Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
[00:02:08] Ah gàmmu daal sama doomu nday nga
[00:02:14] E e e gàmmu daal suma xarit nga
[00:02:19] E e e gàmmu daal suma askan nga
[00:02:25] Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
[00:02:31] E e e gàmmu daal suma xarit nga
[00:02:36] E e e gàmmu daal man sama doomu nday nga
[00:02:42] E e e gàmmu daal man suma xarit nga
[00:02:47] E e e e gàmmu daal yaw sama doomu nday nga
[00:03:16] Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
[00:03:22] Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
[00:03:27] Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
[00:03:32] E e e gàmmu daal sama doomu nday nga
[00:03:38] E e e e gàmmu daal suma xarit nga
[00:03:43] E e e e e gàmmu daal suma askan
您可能还喜欢歌手Youssou N’Dour的歌曲:
随机推荐歌词:
- Get Right [Jennifer Lopez]
- Daytime Nightime Suffering [Paul McCartney]
- Picture Me [Republica]
- The King [Amatorski]
- 梦叠 [蓝立平]
- El Camino [Tate Stevens]
- Closer To You [Michael Franti & Spearhea]
- The More Things Change [Cinderella]
- かもめのBaby [Drop’s]
- 爱到尽头才知道 [孙家山]
- 翻转幸福 [亚天]
- Come on up to the House [The Devil Makes Three]
- Feelin’ Sad [Ray Charles]
- The Grand Tour [George Jones]
- Spiders in Her Hair [King Dude]
- Ooh La La (Eu Vou Ganhar Voc?(Ooh La La (I Can’T Get Over You) [Angélica]
- Something I Dreamed Last Night [Julie London]
- Gee Baby Gee [The Dixie Cups]
- The World Is A Circle(2008/Live In Sydney) [Burt Bacharach]
- Fofoca No Morro [Jamelo]
- Bonnie Ship The Diamond [Judy Collins]
- Who At My Door Is Standing [Slim Whitman]
- 狂串乐基儿 [容祖儿&古巨基]
- I Was Doing All Right [Louis Armstrong&Oscar Pet]
- 求你看我一眼 [MC阿腾]
- Feelin’ [The Pirates&Johnny Kidd]
- Faded Love [George Jones]
- 为什么每个小动物都有自己爱吃的东西呢? [熊爸爸为什么]
- 隐藏了梦想 [王楚深]
- I’m Beginning To See The Light [Peggy Lee]
- My Last Goodbye [Ella Fitzgerald]
- Come Fly With Me [Frank Sinatra]
- Amiga Traidora [Tropicana Band]
- Whisky River [Freddy Fender]
- Peaches N’ Cream [Jackie Lomax]
- Strange Land [Nowhere]
- Gimme More [Top 40 Hip-Hop Hits]
- 爱了你我伤了自己 [王雪飞]
- Too Old to Rock ’n’ Roll: Too Young to Die! [Jethro Tull]